Difference between revisions of "Language/Wolof/Vocabulary/Animals"

From Polyglot Club WIKI
Jump to navigation Jump to search
Line 26: Line 26:
|cokkeer bi
|cokkeer bi
|partridge
|partridge
|
|-
|cumbur mi
|
|
|-
|-

Revision as of 21:38, 3 December 2020

Wolof English Audio
baaxoñ bi raven
berkelle bi   mule
béy, bëy wi goat
bukki bi   hyena
buuj bi (sea)shell
cokkeer bi partridge
cuuj bi chick
dàngin gorilla
fasu-àll wi zebra
fel wi fleas
gaynde-gééj gi shark
géléemu-maam-yàlla bi praying mantis
giléem, géléem gi camel
jaan ji   snake
jaxaay ji eagle
junqóob bi, koti bi crab
kanaara gi drake
kooba gi antelope
koppin bi turkey
léebéer bi hippopotamus
lëg bi hare
lënd wi spider web, cobweb
looy, xargeej owl
maf mi hawk, falcon
mbaam-àll mi warthog
mbaam-sëf mi donkey, (ass)
mbaam-xuux mi pig
mbonnatu-ndox mi sea turtle
mbonnatu-suuf mi land turtle, tortoise
mbóot mi   cockroach
mbote mi, (mburtu) lamb
mbott mi frog, toad
mellentaan wi   little black ant
muus mi, wund wi, janaab ji cat
naat bi guineafowl
nag wi cow
ñey wi   elephant
ngaaga li whale
ngëj mi marabou stork
ngumbaan-tooye bi, (rebes) snail
nguri li wasp
njéeréer bi desert locust
njombor gi   rabbit
njugub bi bat
pax mi burrow
piipa bi dolphin
saafaandu gi African "wild dog"
segg mi   leopard,
séll wi calf
séq gi rooster, (cockerel)
sindax bi   lizard
sippax bi shrimp, prawn
soccent bi grasshopper
sugum si beehive
suñel bi hedgehog
tàgg bi nest
tan mi   vulture
tééñ bi lice
tene mi cheetah
terëx bi flamingo
till gi jackal
wajan wi mare
wànga-lànga wi rhinoceros
waxandor wi   tuna
wel wi fennec fox
weñ wi   fly
weteñ wi tick
xàbban bi ox
xaj bi   dog
xanqel bi duck
xar mi sheep
xar mu-jigéén ewe
xojox gi squirrel of Gambia
xund-xund bi dragonfly
xuyéntaan bi firefly
yamb wi   bee
yëkk wi   bull
yoo wi   mosquito

Sources

http://www.wordsrus.info/wol/animal.htm